Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 68:15-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 68:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Ba fa Aji Man ji tasaaree buur ya, tawub yuur a ngay sóobe tundu Calmon.
16 Yaw tundu yàlla yi, yaw tundu Basan, tundu Basan, tund wi ci coll yi,
Sabóor 68 in Kàddug Yàlla gi