Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 68:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 68:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 «Buur yaak seeni gàngoor a ngay dawa daw, jongomay kër gi di séddale lël ja.
14 Yeen ñiy waaf ci gétt gi, bésub xare, gànjar a ngi, di laafi pitax yu ñu xoob xaalis, dunq ya teg wurus wuy ray-rayi.»
15 Ba fa Aji Man ji tasaaree buur ya, tawub yuur a ngay sóobe tundu Calmon.
Sabóor 68 in Kàddug Yàlla gi