Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 68:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 68:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 «Buur yaak seeni gàngoor a ngay dawa daw, jongomay kër gi di séddale lël ja.
14 Yeen ñiy waaf ci gétt gi, bésub xare, gànjar a ngi, di laafi pitax yu ñu xoob xaalis, dunq ya teg wurus wuy ray-rayi.»
Sabóor 68 in Kàddug Yàlla gi