Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 66:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 66:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Mooy nguuroo njàmbaaram ba fàww, di topp xeet yeek bët. Ku koy diiŋat, yàlla boo damu! Selaw.
8 Yeen xeet yi, santleen sunu Yàlla, te biral cantam!
Sabóor 66 in Kàddug Yàlla gi