Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 66:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 66:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Neleen Yàlla: «Yaaka yéemey jaloore! Sa doolee bare, ba say noon rasu,
4 àddina yépp di la sujjóotal, di la woy, di joobe sa tur.» Selaw.
Sabóor 66 in Kàddug Yàlla gi