Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 65:8-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 65:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 di dalal riirum géej aki gannaxam, ak coowal xeet yi,
9 ba waa cati àddina yéemoo say firnde, waa penkook sowu di sarxolle.
Sabóor 65 in Kàddug Yàlla gi