Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 65:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 65:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Yaa dëje tund yu mag yi doole, gañoo sa kàttan,
8 di dalal riirum géej aki gannaxam, ak coowal xeet yi,
9 ba waa cati àddina yéemoo say firnde, waa penkook sowu di sarxolle.
Sabóor 65 in Kàddug Yàlla gi