Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 65:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 65:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaw miy nangug ñaan, yaw la képp di wuysi.
4 Samay ñaawtéef man na ma, waaye sunuy tooñ, yaa nu koy baal.
Sabóor 65 in Kàddug Yàlla gi