Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 63:5-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 63:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Dama lay sant, sama giiru dund kay, yékkatiy loxo, sàbbaale la.
6 Sama xol di sedd, ni ku ñam wu duun suural, ma bég, sarxolle, màggal la.
7 Su ma tëddee, fàttliku la, waxtuw guddi dama lay xalaat.
Sabóor 63 in Kàddug Yàlla gi