Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 63:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 63:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Xéewloo sa ngor moo dàq dundu bakkan; ma àddu boog, kañ la!
5 Dama lay sant, sama giiru dund kay, yékkatiy loxo, sàbbaale la.
6 Sama xol di sedd, ni ku ñam wu duun suural, ma bég, sarxolle, màggal la.
Sabóor 63 in Kàddug Yàlla gi