Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 63:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 63:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Moo tax kër gu sell ga laa la séentoo, ngir niir sa leer ak sa teddnga.
4 Xéewloo sa ngor moo dàq dundu bakkan; ma àddu boog, kañ la!
Sabóor 63 in Kàddug Yàlla gi