Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 61:3-5 in Wolof
Help us?
Sabóor 61:3-5
in
Kàddug Yàlla gi
3
Àll laa lay wooye, sama xol jeex; yéege ma doju rawtu wu ma jotul.
4
Yaw laa làqoo, ngay tata ju dëgër, fegal ma noon.
5
Naa dëkke sa xayma, ba fàww; làqoo sa kiiraay. Selaw.
Sabóor 61 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms