Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 60:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 60:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Walloo nu sa ndijoor, nangul nu, ba say soppe xettliku.
8 Yàllaa àddoo fa këram gu sell, ne: «Maay damu, dogat suufas Sikem, séddale xuru Sukkóot.
9 Maa moom diiwaanu Galàdd, moom Manase, Efrayim di sama mbaxanam xare, Yuda di sama yetu nguur,
Sabóor 60 in Kàddug Yàlla gi