Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 60:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 60:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Éy Yàlla, wacc nga nu, bëtt sunu kiiraay. Mer nga, waaye ngalla xettli nu.
4 Yëngal nga suuf, xar ko; ngalla jagalal, mu tëju, mu ngi jaayu!
Sabóor 60 in Kàddug Yàlla gi