Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 5:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 5:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Sama Buur, sama Yàlla, déglul, ma ne wallóoy! Yaw laay ñaan.
4 Aji Sax ji, ag suba, ngay dégg sama baat, suba su ne ma diis la samay dagaan, di séentu.
5 Doo Yàlla ju safoo coxor, yaw lu bon du la daloo.
6 Ku réy du taxaw fi sa kanam, kuy def lu ñaaw, bañ nga ko.
Sabóor 5 in Kàddug Yàlla gi