Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 5:3-5 in Wolof
Help us?
Sabóor 5:3-5
in
Kàddug Yàlla gi
3
Sama Buur, sama Yàlla, déglul, ma ne wallóoy! Yaw laay ñaan.
4
Aji Sax ji, ag suba, ngay dégg sama baat, suba su ne ma diis la samay dagaan, di séentu.
5
Doo Yàlla ju safoo coxor, yaw lu bon du la daloo.
Sabóor 5 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms