Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 59:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 59:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Meral, jeexal leen, jeexal leen, ba ñu jeex tàkk, ba ñépp xam ne Yàllaay Buur ci giirug Yanqóoba, ba ca cati àddina. Selaw.
15 Bu ngoonee ñu wàccsi, di xiiru niy xaj, di wër dëkk bi.
16 Ñuy wër di wut lu ñu lekk, su ñu suurul, di ñurumtu.
Sabóor 59 in Kàddug Yàlla gi