Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 59:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 59:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Bàkkaar lañuy wax, seeni kàddu, bàkkaari neen. Yal nañu bew ba daanu, yooloo ko seeni saagaak seeni fen.
14 Meral, jeexal leen, jeexal leen, ba ñu jeex tàkk, ba ñépp xam ne Yàllaay Buur ci giirug Yanqóoba, ba ca cati àddina. Selaw.
Sabóor 59 in Kàddug Yàlla gi