Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 58:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 58:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Yeena ngi mébét njubadi, di lawal fitna ci réew mi.
4 Ku bon day sosu rekk, dëng; juddu, teggi yoon, dib fen-kat.
5 Day am daŋar ni ñàngóor, fatti noppam ni jaan ju tëx:
6 du dégg baatu jatkat, mbaa jati ñeengokat bu ñàng.
Sabóor 58 in Kàddug Yàlla gi