Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 57:7-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 57:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Noon yi di ma fiir, sama xol jeex. Ñu gasal mam pax, far tàbbi ca. Selaw.
8 Yàlla, dogu naa, dogu naa woy, di la kañ.
9 Na sama jëmm jépp yewwu, xalam ak moroom ma yewwu; ma yee leeru njël.
10 Boroom bi, naa lay gërëm ci biir xeet yi, kañ la ci biir waaso yi.
Sabóor 57 in Kàddug Yàlla gi