Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 57:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 57:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Ma woo Yàlla, Aji Kawe ji, Yàlla, mi may matalal.
4 Mooy yónnee fa asamaan, musal ma, dumaal ma ku may not. Selaw. Yàllaay yónnee jëfi ngoram ak wormaam.
5 Maa ngi tëdd ci biiri noon yu mel niy gaynde, di yàpp doom aadama. Seeni sell niy xeej aki fitt, seen làmmiñ di saamar yu ñaw.
Sabóor 57 in Kàddug Yàlla gi