Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 57:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 57:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Ma woo Yàlla, Aji Kawe ji, Yàlla, mi may matalal.
4 Mooy yónnee fa asamaan, musal ma, dumaal ma ku may not. Selaw. Yàllaay yónnee jëfi ngoram ak wormaam.
Sabóor 57 in Kàddug Yàlla gi