Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 56:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 56:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Noon yee ma yendoo lakkal, bare lool di xareek man. Ku Màgg ki,
4 bés bu ma tiitee, yaw laay wóolu.
5 Yàlla laay màggal kàddoom, Yàlla laa wóolu, ragaluma. Lu ma nit manal?
6 Bésoo bés ñu ngi jalgati samay wax, seen mépp mébét di sama loraange.
Sabóor 56 in Kàddug Yàlla gi