Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 53:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 53:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Yàllaa tollu asamaan, jéer doom aadama, di seet ku ci xelu, tey sàkku Yàlla.
4 Ñépp a dëddu, bokk yàqu yaxeet. Kenn deful lu baax, du kenn sax.
5 Yàlla nee: «Xanaa ñiy def lu bon, xamuñu dara? Ñuy lekk sama ñoñ niw ñam, te sàkkuwuñu Yàlla.»
Sabóor 53 in Kàddug Yàlla gi