Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 53:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 53:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Yàllaa tollu asamaan, jéer doom aadama, di seet ku ci xelu, tey sàkku Yàlla.
4 Ñépp a dëddu, bokk yàqu yaxeet. Kenn deful lu baax, du kenn sax.
Sabóor 53 in Kàddug Yàlla gi