Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 52:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 52:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Yàlla da lay sànk ba fàww, fëkke la sab xayma, yóbbu, déjjatee la réewum aji dund. Selaw.
8 Aji jub gis ko, yéemu, di la ree, naa:
9 «Xool-leen jàmbaar ji làqoowul Yàlla, xanaa di yaakaar alalam ju bare, di yokkoo loraange.»
Sabóor 52 in Kàddug Yàlla gi