Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 51:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 51:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Ñaawtéef daal laa judduwaale, te sama ndey ëmbaale ma bàkkaar.
8 Dëgg daal nga namm, dëggu reenu xol, kon déey ma xel mu rafet.
9 Wis ma ndox, ma sell; sang ma, ma set wecc.
Sabóor 51 in Kàddug Yàlla gi