Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 51:13-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 51:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Bu ma xalab, bu ma xañ sa noo gu sell.
14 May ma, ma bégeeti sag wall, te dundale ma xol bu tàlli,
15 ma xamal tooñkat sa war, ba moykat dellu ci yaw.
16 Céy Yàlla, yaw Yàlla mi may musal, baal ma deret ji ma tuur, ma siiwal sa njekk.
Sabóor 51 in Kàddug Yàlla gi