Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 50:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 50:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 «Yeen sama ñoñ, dégluleen, ma wax leen; yeen waa Israyil, ma sikk leen. Maa di Yàlla, seen Yàlla.
8 Du seeni sarax laa leen di sikke, mbaa seen saraxi rendi-dóomal yi sax fi sama kanam.
9 Soxlawuma yëkku yar ak sikketu gétt.
Sabóor 50 in Kàddug Yàlla gi