Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 50:19-21 in Wolof

Help us?

Sabóor 50:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Dangeena afal seen gémmiñ ci mbon, seen làmmiñ taqoo fen,
20 ngeen di tooge seen mbokk, di yàq deru doomu ndey.
21 Lii yeena ko def! Damay noppi, ngeen defe ne damaa mel ni yeen? Dama leen di sikk, tuumaal leen, ngeen gis!
Sabóor 50 in Kàddug Yàlla gi