Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 50:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 50:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Damay lekk yàppu nag ak a naan deretu sikket a?
14 Deel jaajëfal Yàlla, sarxale ko, di fey Aji Kawe ji loo dige,
15 di ma woo bésub njàqare, ma wallu la, nga màggal ma.»
Sabóor 50 in Kàddug Yàlla gi