Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 50:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 50:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Damay lekk yàppu nag ak a naan deretu sikket a?
14 Deel jaajëfal Yàlla, sarxale ko, di fey Aji Kawe ji loo dige,
Sabóor 50 in Kàddug Yàlla gi