Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 50:12-17 in Wolof

Help us?

Sabóor 50:12-17 in Kàddug Yàlla gi

12 Su ma xiifoon, duma leen ko wax, maa moom àddinaak li ci biiram.
13 Damay lekk yàppu nag ak a naan deretu sikket a?
14 Deel jaajëfal Yàlla, sarxale ko, di fey Aji Kawe ji loo dige,
15 di ma woo bésub njàqare, ma wallu la, nga màggal ma.»
16 Ñu bon ñi Yàlla ne leen: «Lu ngeen di tari sama dogali yoon, di waxe sama kóllëre?
17 Yeena ngii, bañ sama yar, xalab samay kàddu.
Sabóor 50 in Kàddug Yàlla gi