Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 4:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 4:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Yeen boroom daraja yi, buleen yàqati sama der, buleen sopp caaxaan, di sos. Selaw.
4 Xamleen ne Aji Sax ji day séddoo ku ko ragal, te bu ma wooyee Aji Sax ji, mu dégg.
Sabóor 4 in Kàddug Yàlla gi