Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 49:8-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 49:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 Ana ku mana jota jot sa bakkanu moroom, mbaa mu di ko feyal Yàlla njot ga?
9 Njotug bakkan jafe na, bu ci jéem dara.
Sabóor 49 in Kàddug Yàlla gi