Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 49:7-11 in Wolof

Help us?

Sabóor 49:7-11 in Kàddug Yàlla gi

7 di ñu wóolu seen am-am, di kañoo alal ju bare?
8 Ana ku mana jota jot sa bakkanu moroom, mbaa mu di ko feyal Yàlla njot ga?
9 Njotug bakkan jafe na, bu ci jéem dara.
10 Ana kuy dund ba fàww, ba doo gis bàmmeel?
11 Xanaa gis ngeen ne xelu, dee; dof, dee; naataxuuna it faatu rekk, wacce keneen alalam.
Sabóor 49 in Kàddug Yàlla gi