Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 49:4-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 49:4-7 in Kàddug Yàlla gi

4 Li may wax xel la, di xalaat yu déggu.
5 Damay teewlu kàddu yu xelu, xalamal la sama tekkiteb cax.
6 Ana lu may tiit bés yu metti, yu ma njublaŋ yéewe seeni ñaawtéef,
7 di ñu wóolu seen am-am, di kañoo alal ju bare?
Sabóor 49 in Kàddug Yàlla gi