Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 49:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 49:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 ngay ku tuut di ku mag, nga bareleek nga néewle.
4 Li may wax xel la, di xalaat yu déggu.
5 Damay teewlu kàddu yu xelu, xalamal la sama tekkiteb cax.
Sabóor 49 in Kàddug Yàlla gi