Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 49:16-18 in Wolof

Help us?

Sabóor 49:16-18 in Kàddug Yàlla gi

16 Waaye Yàllaa may musal ci dooley njaniiw, jot sama bakkan, ba jël ma.
17 Buleen yéemu ci ku barele, teraangay këram di yokku.
18 Du dee ba yóbbaale dara, teraangaam du ko topp biir bàmmeel.
Sabóor 49 in Kàddug Yàlla gi