Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 49:12-13 in Wolof

Help us?

Sabóor 49:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Sa bàmmeel di sa kër, ba fàww, di sa dëkkuwaay bu sax dàkk, boo tudde woon sa bopp ay suuf sax.
13 Nit ak darajaam fanaanul, mook aw rab a yem, sànku rekk.
Sabóor 49 in Kàddug Yàlla gi