Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 48:3-7 in Wolof
Help us?
Sabóor 48:3-7
in
Kàddug Yàlla gi
3
Jekk taxawaayee tundu Siyoŋ, catu bëj-gànnaar, dëkku buur bu mag bi, di mbégtem àddina sépp.
4
Yàllaa wone kaaraangeem ca biir tatay dëkk ba.
5
Buur yaa ngoog daje, àndandoo.
6
Nun noo gis, jommi, tiit, fëx,
7
ne fay pat-pati, jàq ni kuy matu.
Sabóor 48 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms