Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 48:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 48:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Jekk taxawaayee tundu Siyoŋ, catu bëj-gànnaar, dëkku buur bu mag bi, di mbégtem àddina sépp.
4 Yàllaa wone kaaraangeem ca biir tatay dëkk ba.
5 Buur yaa ngoog daje, àndandoo.
Sabóor 48 in Kàddug Yàlla gi