Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 48:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 48:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Doxleen biir Siyoŋ, wër ko, waññleen ay soorooram,
14 nemmikuy tataam, doxantoo këri buur, ba man koo yegge maasug ëllëg,
Sabóor 48 in Kàddug Yàlla gi