Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 46:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 46:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Ay giir a riir, ay réew yëngu; mu àddu, suuf seey!
8 Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ànd ak nun, Yàllay Yanqóoba jee nuy rawale. Selaw.
9 Dikkleen gis jaloorey Aji Sax ji, ak yàqute gi mu dogal ci kaw suuf.
Sabóor 46 in Kàddug Yàlla gi