Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 46:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 46:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 ba dunu tiit suuf su yëngu sax, ba tund yiy tàbbi biir géej,
4 mbaa gannax yuy riir, di fuur ak a fuddu bay gësëm tund yi. Selaw.
5 Ag dex a ngi defi wal, di bànneexal dëkku Yàlla, sellngay dëkkuwaayi Aji Kawe ji.
6 Yàllaa ngi ci biir dëkk bi, du raf; Yàllaa koy dimbali ba jant fenkee.
Sabóor 46 in Kàddug Yàlla gi