Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 45:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 45:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaa gëna góorayiwe ci àddina, sa kàddu diw yiw, ndax Yàllaa la barkeel ba fàww!
4 Jàmbaaroo, takkal sa saamar, te yànj, am daraja;
Sabóor 45 in Kàddug Yàlla gi