Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 44:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 44:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaw ci sa bopp yaa dàq xeet yi, jëmbat fa maam ya; yaa mbugal xeet yi, ñoom, nga yiwi leen.
4 Du seen saamar lañu nangoo réew mi moos, seen dooley bopp it mayu leen ndam. Yaa ko defe kàttan ak doole, geesoo leen sa leeru kanam, ngir sa cofeel.
Sabóor 44 in Kàddug Yàlla gi