Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 44:15-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 44:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Tax nga xeet yi di nu léeboo, jaambur yaa ngi nuy wëcc bopp!
16 Damaa dëkke gàcce, sëlmoo kersa
Sabóor 44 in Kàddug Yàlla gi