Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 44:13-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 44:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Jaay nga sa mbooloo ci dara, te jariñu la tus.
14 Tax nga sunuy dëkk di nu ree, ñi nu séq di nu kókkaleek a ñaawal.
15 Tax nga xeet yi di nu léeboo, jaambur yaa ngi nuy wëcc bopp!
16 Damaa dëkke gàcce, sëlmoo kersa
Sabóor 44 in Kàddug Yàlla gi