Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 42:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 42:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Rongooñ laay dunde guddeek bëccëg, noon yi di ma dëkke naa: «Ana sa Yàlla ji?»
5 Lii laay fàttliku, sama xol jeex: dama daan jàll, jiite mbooloo ma, jëm kër Yàlla ga, di sarxolleek a sant, ñu booloo di màggal.
6 Moo man, lu may yoggaaral nii? Lu may jàq? Naa yaakaar Yàlla, ba dellu sante sama Yàlla wallam.
Sabóor 42 in Kàddug Yàlla gi